Artist: Samba Peuzzi
Lyrics of Artist: Samba Peuzzi
  1. [Lyric] Mala baal (Samba Peuzzi)

    Nyungi and mais xam na ni gueumo ma Sa xarit la teh fo tok di wax ci man Bueugo ma dem da ngay mer bu may avancer Mais douma la topp nala baal way Tonj nga ma benn yone Ma dal dila baal Nga del tonjati ma Ma dal dila baal Xam na jikom (yah yah) Yag nang bayil ma bayiko ci bir Why not? Mako baal mako baal Duma la topp mala baal waw Mala baal mala...Learn More
    popSamba Peuzzi