Song: Jeleeti
Year: 2013
Viewed: 3 - Published at: 8 years ago

Fo koy jeleeti kou la beugué ni man
Fo koy jeleeti kou la sopé ni man
Fo koy jeleeti kou la nobé ni man
Fo koy jeleeti

Kou yewou khadja goudi di khol ndakh sangougua
Kou lay wakh deugueu jo bougoula degue ni man
Kou nek ak fa yalla bourbi fetele
Ak fa nga beug sa bop feté

Fou ma koy jeleeti kou ma nobé ni yaw
Fou ma koy jeleeti kou may firé ni yaw
Fou ma koy jeleeti kou ma gneme wakh deugeu ni yaw
Fou ma koy jeleeti

Boula bour bi yalla beugue da nga koy kham
Ndakh tokhidona bo douguou mou guene la ci
Boula nit ki beugue dome yaye ndagua koy kham
Nakh bou moussiba di khegn mou ne la kay goungue ma fi
Adouna gongou souniou kanam
Jam waroula teukou morom mou jamam
Adouna gongou ci souniou kanam dom yaye
Jam waroula natou moromou jamam
Fo koy jeleeti, fo koy jeleeti
(Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti)
Fo koy jeleeti kou beugueu sa diam ni man
Fou ma koy jeleeti kou degueu dadj ni yaw
Fou ma koy jeleeti kou moka potch ni yaw
Fo koy jeleeti
Kou yewou khadia goudi di khol nakh sangougua
Kou lay wakh deugueu jo beugoula deg ni man
Kou nek ak fala yalla bourbi fetele
Ak fa nga beug sa bop fete
Fo koy jeleeti, fo koy jeleeti
Fo koy jeleeti, fo koy jeleeti
(Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti, Fane la koy jeleeti)

( Souleymane Faye )
www.ChordsAZ.com

TAGS :